Street activity

By Nitdoff

On R.D.D.R

Thumbnail

{Nitdoff}

Yeah !!!

Ya! Pericolosso (un jeu dangereux) Biss bou nek mou yém leu

Hé mbede nakhanté ak féne leu

Systémou taukhidouna

Mandi ak taukhi bauna

Ndjoute ndiathie ak tek deal ak sokhi maukidaume

Lepp cii outi Kom-ma, Bandit bou souki aumeu

Dafa dafa dafa beurii danger

Cagoulé seni face speed nii black ninja

Tokk tchil planifié dadii tekk deal

Daniou gatt tank té douniou wax cii téléphone

Diksa (Sadik) clik beug easy money téla bone

Ay killers ak dealers trafic ay kilo baune

Gni bagn niou néweul lèn dolé niogui train (S’entrainer)

Di fisselé ay gangsta project cii séni brain ( Cerveau)

Make it lot of money done boss cii séni dream

Féliitou bégou naw naw yi cii scène de crime

Ay toxico yiy gueune di noyé cii sèn déprime

{Refrain}

Street Ciii laay get sama freedom

Street Sipp ngani moy sunu favor

Street Aksil yagui sunu jungle

I say welcome to the street (X2)

Street dafa dafa dafa Hard (métii)

Street Activity

Street dafa dafa dafa Hard

Street Activity

Street street Street activity

Street Street Dafa dafa dafa hard

{Rex-T}

Yaw Aksi nga yagui sunu bi side

Guissate to métitou life bigni missate

Sunu yen bi di dissate

Sa bopp niou wissate

Nga beussate sa xoll mou niak dii siitate

Bagne tokk fi ni di hot

Yarr baby di xarr

Deufeul sa lepp ba day ngay diogatt

Soubou di tégatt

Gueneu meuneu défatt

Silou yone nga nékatt

Lou yéngou nga…..

Life is so hard

So bad

Biss bou né niouy sokhatt

Songatt

Tek délit nieuw taukhatt

Topatt sunu waay bamou dokhatt

Jobatt

Guéneu cii ghetto

Done ay hero

Diaroul pouss wala taukh ay péro

Péro jailo dieulé fi méro déggo

Ghetto nioune danio haaaaaaaaaaaaard

{Refrain}

Street Ciii laay get sama freedom

Street Sipp ngani moy sunu favor

Street Aksil yagui sunu jungle

I say welcome to the street (X2)

Street dafa dafa dafa Hard (métii)

Street Activity

Street dafa dafa dafa Hard

Street Activity

Street street Street activity

Street Street Dafa dafa dafa hard

{Nitdoff}

Niggaz yagui hustla cii street activity

Door warr ba slow di xeuy takk fidii

Money wala jail’eu defkat yi takk fiit yi

Thiabii fété lèn guinaw téwoul niou akk sibiti

Street activity lay firii tekk cii sibiti

Me and my nigga Rex sipp naniou lou xéw cii street bi

Mélokanou niit ki cii nimou gueuneu niawé

Djeufinou baayima(animal) djiss nga street noumou grawé

Gni société bi guédd niougui fanane cii mbede

Gni beug téla yegg cii lou léwoul lagni tédde

Done agresseur di reupeuteul

Niou rombe rek niou feul ko dieul

Djam maquette di rocket niou xoff lagni seukeuteul

{Refrain}

Street Ciii laay get sama freedom

Street Sipp ngani moy sunu favor

Street Aksil yagui sunu jungle

I say welcome to the street (X2)

Street dafa dafa dafa Hard (métii)

Street Activity

Street dafa dafa dafa Hard

Street Activity

Street street Street activity

Street Street Dafa dafa dafa hard