Imbécilo Rék

By Nitdoff

On The Beast 1

Thumbnail

[Refrain]

Nane nga meuneu fowei nit yi imbécilo rék

Nane nga meunei deupé caisse yi imbécilo rék

Nane nga meuneu tassé yakar imbécilo rék

Detournement de bien publics yi imbécilo rék

Liniou lébone ngir soukhalikou nga ni ko foukh tokk

Li warron tchi ndiangu bi nga ni ko foukh tokk

Li warron tchi fadiou bi nga ni ko foukh tokk

Imbécilo rék imbécilo rék

[Couplet 1]

Deuké di doul ak rendi nit soul

Yagui djité thiogalou foule sa lepp di cool

Yaye qui dakheu sathie sa rew kone khogalikoul

Sa galé amna auto you luxe sa comtpe yi full

Sa ndieuguou ben montre tchi xayma tabakh neu school

Dou né nga gueumo ni nieti fani bamel amna

Dou yagui nax nit gni bayil khel ni yallah xamna

Sa keurou fi meun na yaatou wayé bamel xatna

Do nitou guat doma sathie banopi mayma yapma

Li niep bokk yako diеul caisse sou nguur yi yako teul

Modafucka nga fi amoul lenn louniе fiy rafetal

Hôpitaux yi amouniou lale

Niak ba ngui gueuneu di wale

Bachelier tokk di kholé ndakh amouniou founiou dale

Ngueni niodi dioma niaw ci ay parrains wou mbalakh man

Battréwoulen lou nguen mom yenn sathie you niakk diom

Haute trahison du peuple nguen dekou ay meukh daume

[Refrain]

Nane nga meuneu fowei nit yi imbécilo rék

Nane nga meunei deupé caisse yi imbécilo rék

Nane nga meuneu tassé yakar imbécilo rék

Detournement de bien publics yi imbécilo rék

Liniou lébone ngir soukhalikou nga ni ko foukh tokk

Li warron tchi ndiangu bi nga ni ko foukh tokk

Li warron tchi fadiou bi nga ni ko foukh tokk

Imbécilo rék imbécilo rék

[Couplet 2]

Yaw métier bou noble ngen nekk di tonie

Guetou mala yey sén place nguen lekk dji ngogn

Lign ley fay beuri tewoul ngey sathie di rogne

Te ken tchi yen defoul djiego sakh youy sopi sa konie

Guis na gua beuuff tchi tankou kilifeu di ceddé ay batt

Té bofa diougué talibém yi sey dieuf moleni fatt

Guiss na niou toudé leu ay biss nga niew di diokhé ay nakk

Té finiou leu fale bofa démé radio guedj na fa takk

Niata nio léwal koom si ay surfacture

Té bouniouy laay nga guiss sen fennyi comme ay pur acteur

Benn daan dou dale sen kaw amnanie protecteur

Nioun sunuy ndaw di xeuy di gueun di daw ci khif ak peur

Élection niou guenewaat budget bi dieund espoir

Diakhassé tarikha yek ethnies yi nguir diot ci pouvoir

Bou ci bakane naré rote sakh dounie déliu guinaw

Nanie signel gandi cheque juge bi rek mou diokhé victoire

[Refrain]

Nane nga meuneu fowei nit yi imbécilo rék

Nane nga meunei deupé caisse yi imbécilo rék

Nane nga meuneu tassé yakar imbécilo rék

Detournement de bien publics yi imbécilo rék

Liniou lébone ngir soukhalikou nga ni ko foukh tokk

Li warron tchi ndiangu bi nga ni ko foukh tokk

Li warron tchi fadiou bi nga ni ko foukh tokk

Imbécilo rék imbécilo rék

[Outro]

Woop woop woop woop woop sathiéy

Woop woop woop woop woop sathiéy

Woop woop woop woop woop sathiéy

Imbécilo rék imbécilo rék

Woop woop woop woop woop sathiéy

Imbécilo rék imbécilo rék

Woop woop woop woop woop sathiéy

Imbécilo rék imbécilo rék